Groupe Pastef Massification
Dikkleen fekk si nu, ci Kippaango yaatal Pastéef gu Téllangaram gi https://t.me/pastefmassification ngir nu àndandoo : • Xeex Makki Sàll ak ay ñooñam; • Dooleel Usmaan Sonkko ak ay ñooñam; • Bañ nooteel gi ak jaay doole gi;
#ousmane_sonko #pastef #patriotes #yaatal_pastef
Affichez ou rejoignez le groupe Groupe Pastef Massification dans votre Telegram en cliquant sur le bouton "Afficher le Groupe".
Dikkleen fekk si nu, ci Kippaango yaatal Pastéef gu Téllangaram gi, ngir nu àndandoo:
• Bañ nooteel gi ak jaay doole gi;
• Dog buumug nooteel gi ak buumug njàmm gi;
• Dooleel sunu àada ak sunu cosaan;
• Sàmm jikko yi;
• Xeex Makki Sàll ak ay ñooñam;
• Dooleel Usmaan Sonkko ak ay ñooñam;
• Sopp i réew mi.
Boolloo mooy Dooleféewalloo wàññi doole
Bësël
lëkkalekaay yi ci suuf nga ékksi ci Kippaango yi
https://t.me/pastefmassification (Groupe Telegram)
https://t.me/pastefinfo (Canal Telegram)
Na bataaxel bi siiw fés te wesaaroo.
Aimes-tu cet groupe? s'identifier ou cliquez sur @dailychannelsbot pour évaluer ce groupe via Telegram